lundi 29 septembre 2008
Rafles dans le nord est de paris
Rafles ?
Chaques semaines dei am ei rafles yu beri dans le 18, 19ieme. New amoul keuilet(papiers) leigni yobou centre de retention pour delo len sen deuk.
Empecher rafli moy empecher expulsions
New gnou muné khamé rafles ?
Chaques heures mais surtout horaires ou liguei.si bedmi si trans… ; Munen ko khamé dakh : Ben auto civil , garée discrétement de façon que ken do ko guiss ,par exemple rue de jessaint si square bi au metro porte de la chapelle Auto bob amne ben systhem d’ aeration sicaw toi bi ;ben buro boun dow mo nek sibir.legui ei 2,3 civils nioy yobou new ou jap si auto bi,si transpori rafli lei camouflé melni ei contolou tickets .
Lugnu moune def ?
Bolo mo gen : wakh ko se khalidi et amne ben numero d’urgence bo mune waté pour que le maximum de gen kham noumou deme numero d’urgence : 06 xx xx xx
Wakh ko gni guei romb gnup,ak surtout gni gue khamé amou gnu keuillet.bou gnu bolo tei bou gnu alou touti rales bi dei gene visible. Te lol moune dawlo police bi.
Mungen ladjé police : l’ordre de réquisition c’est a dire l’autorisation du contrôle massif. jemel khol fan legni yobou ligni areté ; bo ameé ben proch bou gnu jap amne ben brochures « sans papiers :s’organiser contre l’expulsions » sur internet : www.sans papiers.internetdown.org.
Centre de rétention bou vincennes dafa lakh,legui kou gnou jap Cité wale au mesnil_amelot lei ko yobou te fof dark bi mo gaw.
Etat bi mo tei di def ei rales si digente stalingrad ak barbes pour jap sans papiers i ak pauvres i. Si ale bi_.lol ben politique le « setel paris,paris pour les riches »
Annés i mujé degni deferat quaritiers 18, 19ieme pour york loyer hlm i. Te pauvres i ak immigrés i legni dark aux portes de paris. Cest l’immigration chosi « immigation bou gnou tan ».
DEGNI ORGANISEOU FACE AU RAFLES ET AUX EXPULSIONS
Wornen jok car doundou bi da gene meti motakh gnou woro bolo.
Reunion le dimanche 12 octobre 2008 à 15 heure au square Léon degni wartan pour organiséou sur le 18ieme et le 19ieme.
NEN YARK SEN MACHINE D’EXPULSION